Youssou N'dour - Li Ma Weesu (Wolof) Lyrics

Google
 


::Home >> Youssou N'dour - Li Ma Weesu (Wolof) Lyrics


Something you should know about Li Ma Weesu (Wolof) Lyrics

Title: Youssou N'dour - Li Ma Weesu (Wolof) lyrics

Artist: Youssou N'dour Lyrics

Visitors: 749 visitors have hited Li Ma Weesu (Wolof) Lyrics since May 27, 2008.







li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
seetal;
leegi leegi ma gesu, ci li ma weesu
leegi leegi ma recu, walla sax di baaku
fu gune yi feetee, dama leen di teetee
wax nu ma neexee, ma bëgga leen
damay, damay, damay dellu gune
mel ni,mel ni, mel ni duma màgg
lu ma gën di yàgg, xel ni mel ni bank
lu ma gën di màgg, dellu tuuti tank
li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
ma ni seetal;
leegi leegi ma gesu, ci li ma weesu
leegi leegi ma recu, walla sax di baaku
fu gune yi feetee, dama leen di teetee
wax nu ma neexee, ma bëgga leen
damay, damay, damay dellu gune
mel ni,mel ni, mel ni duma màgg
fu gune yi feetee, dama leen di teetee
wax nu mu ma neexee ma béggati
li ma gën di jege, mel ni dama sore
lu ma gëna sore, gën di gis li ma jegewoon
lu ma gën di yàgg, xel ni mel ni bank
lu ma gën di màgg, dellu tuuti tank
li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
li ma dundee, li ma weesu
dey delluse, mel ni seetu
damay, damay, damay dellu gune
mel ni,mel ni, mel ni duma màgg...
Thanks to caroline



The hottest songs from Youssou N'dour

  • Youssou N'dour - Biko (With Peter Gabriel) Lyrics
  • Youssou N'dour - How Come Lyrics
  • Youssou N'dour - How Come * Lyrics
  • Youssou N'dour - Seven Seconds Away Lyrics
  • Youssou N'dour - Things Unspoken Lyrics
  • Youssou N'dour - My Hope Is In You Lyrics
  • Youssou N'dour - 7 Seconds Lyrics
  • Youssou N'dour - Set Lyrics
  • Youssou N'dour - Leaving Lyrics
  • Youssou N'dour - Mame Bamba Lyrics


    Fans who visit this lyrics also like:

  • Britney Spears - Over Protected Lyrics
  • Good Charlotte - Keep Your Hands Off My Girl Lyrics
  • Rocio Durcal - Amor Eterno Lyrics
  • Alicia Keys - Goodbye Lyrics
  • Bette Midler - Boogie Woogie Bugle Boy Lyrics
  • Madonna - Crazy For You Lyrics
  • Enrique Iglesias - Por Amarte Lyrics
  • Mya - Moulin Rouge Lyrics
  • Mel Carter - Hold Me Thrill Me Kiss Me Lyrics
  • Christina Milian - Whatever U Want Lyrics
  • Neil Halstead - Paint A Face Lyrics

    Maybe you are looking for:

    Youssou N'dour - Li Ma Weesu (Wolof) Lyrics for mp3
    Youssou N'dour - Li Ma Weesu (Wolof) Lyric
    Youssou N'dour - Li Ma Weesu (Wolof) Letras
    Youssou N'dour - Li Ma Weesu (Wolof) Songtexte
    Youssou N'dour - Li Ma Weesu (Wolof) Lyrique
    Youssou N'dour - Li Ma Weesu (Wolof) Testo
    Youssou N'dour - Li Ma Weesu (Wolof) Referencias


    Tips to look for free audio clips
    (Don't use those tips to download illegally. To buy music is always the best way to support your idols)

  • Use Google, Yahoo and MSN to find some auido clip sites. Sometimes search engines can direct you to right sites. Now that a lot of auido clip sites are banned by search engines, remember to make good use of exchange links in those sites.

  • Use auido clip search engines outside the United Stats. I used to use Chinese sites such as Baidu, Sogou, Yahoo China to search audio clips. Your browser maybe ask you to install simplified Chinese character, just ingore it. I always can find tons of English audio clips in those music search engines.

  • Use P2P software. It works well for full album audio clips specially. In fact, you almost can find everything with P2P software.

  • Visit artist's offical website. Some artists' sites provide mp3 files for fans to download.





  • Li Ma Weesu (Wolof) Lyrics by Youssou N'dour are the property of the respective authors, artists and labels, Li Ma Weesu (Wolof) Lyrics by Youssou N'dour are provided for educational purposes only , If you like the song, please buy relative CD.